yalla mo bind nit moy doggal tè loukko nèkh lay dèf kèn mounoussi dara. Mais dafa am gno khamni wakh rèk lagni dèk khamougnou tous di publicitè sèn boppou founè ti tagg sèn boppou founè tè ay nitt simple kèssè lagnou dèpanse sakh dalèndi teu, wakhoumalak nanè am kham kham faite trè trè attention ok merci.
▶️ DTube
▶️ YouTube